Mer11212018

Last updateT3_DATE_FORMAT_LASTUPDATE

Taille police

Profil

Style du menu

Cpanel

Célébration Gamou à Firdawsy avec le Général Kara Suite Partie 2

Live/Direct: Takussan Bamba Fepp à Grand Yoff avec le Général KARA

Magal Touba 2018: conférence publique animée par Cheikh Ahmadou KARA Mbacké part 1

Poème Safar 7 et Déclaration sur les accusations à l'encontre de Ousmane Sonko

Magal Touba 2018: conférence publique animée par Cheikh Ahmadou KARA Mbacké part 2

Live/ Takussan Bamba Fepp, arrivée du Général de Kara à Grand Yoff

Célébration Gamou avec le Général Kara à Firdawsy partie 1

Journée de prière dédiée à Soxna Fatima Diouf défunte mère du Général KARA à Darou Mouhty.

jahman Xpress et Ahmad Mbacké invitent la jeunesse chez cheikh Ahmadou KARA le jour du Magal

"Je payerais la caution du Candidat Macky Sall " Cheikh Ahmadou KARA Mbacké

Doxu Safar à Thiès: Alkati Bamba Fepp sur la route du Magal de Touba

https://m.facebook.com/story.php?story_fbid=1981560368568295&id=269939519730397

Veille du Magal de Touba 2018 chez Cheikh Ahmadou KARA Mbacké

Le Général KARA en conclave avec les soldats de Bamba

Ramadan 2018: série de visite du Général de BAMBA à TOUBA chez les dignitaires mouride

Révélations de Cheikh Ahmadou KARA suite au meurtre de son talibé Coumba Ndoféne dit Amdy

Vidéo Rassemblement du Jaysun à Médina avec la présence du Général Kara

Les Soldats de Bamba chez Cheikh Ahmadou KARA Mbacké Noreyni à Mermoz

Le Guide condamne fermement la sortie de son fils Serigne Moustapha Mbacké

Coalition Xarnubii : Le Général KARA et ses fils s'engagent

Cheikh Ahmadou Kara au King Fahd Palace

Serigne Moustapha Mbacké éclaire ses propos et demande pardon à son père

Inondations Touba: Nouveau message de Serigne Modou KARA au Gouvernement

Séjour de Cheikh Ahmadou KARA Mbacké à Louga les 1, 2, 3 Mars

Cheikh Ahmadou Kara Mbacké à la Journée Mame Diarra Bousso au Cices

Visite de Cheikh Ahmadou Kara Mbacké auprès du khalife général des mourides, Serigne Mountakha

Nouveau poème de Serigne Modou Kara dédié à Serigne Mountaha: "Alkaati Muridiya"

Déclaration de Cheikh Ahmadou Kara sur la situation politique du pays

L'histoire de la naissance du prophète Insa ibn Mariam (Jesus) par Serigne Modou Kara Mbacké

Gamou de Cheikh Ahmadou Kara Mbacké à Ndiarëm Diourbel_part 2

Gamou de Cheikh Ahmadou Kara Mbacké à Ndiarëm Diourbel_part 1

Magal Touba 2017: Discours de Borom Darou Noreyni

Touba 2017 : Retrouvailles émouvantes entre Serigne Modou KARA et son frère Borom Darou

Serigne Modou Kara : "HUQQAL BUKKA-U" FAUT-IL PLEURER LES MAÎTRES SOUFIS ?

Magal Touba 2017: Ziar commandos de la Paix au Général de BAMBA

Wadjal Magal Touba :Journée Safar à Thies: marche avec Serigne Modou Kara Mbacké

Cheikh Ahmadou KARA mobilise plus d'1 millier de jeunes à la rescousse des populations Ndamatou

Safar à la mosquée Massalikul Jinaan de Dakar avec le Général Kara. part_1

Ziar inédit de Serigne Modou KARA en position agenouillée faisant le tour de la mosquée de Touba

La Vérité sur les échanges entre Serigne Modou KARA et le Dahira Khidma dans la mosquée de Touba

Serigne Modou KARA condamne les dérives sur le net envers certains dignitaires de Touba

Révélations des secrets du poème ''Matlaboul Fawzaïni'' par le Général KARA_Part 2 en Français

Cheikh Ahmadou KARA Mbacké offre ses terres de Bambilor pour un projet de l'armée nationale

Serigne Modou KARA partage un ver de Xassaïdes comme protection contre la violence des agresseurs

1997 : Le Général de Bamba vaporisant un parfum très cher dans le Mausolée de Serigne Touba

Back Vous êtes ici : Home Religion Actualités Poème écrit par Cheikh Ahmadou KARA dédié à SËRIÑ MUNTAQÂH Mbacké, khalife Général des mourides

Poème écrit par Cheikh Ahmadou KARA dédié à SËRIÑ MUNTAQÂH Mbacké, khalife Général des mourides

 

 

 

 

 

 

 

 

 

 

 

 

SËRIÑ MUNTAQÂH

Bismi LÂHI ar RAHMÂNI ar RAHÎMI
Wa salla LÂHU allâ SEYDINÂH MUHAMMADIN wa sallama taslîman
Hâzihil qasîdah min QÂDIMI RASÛLI LÂHI illal QALÎFAH-al-MUNTAQÂH

KI moom jamono, ñëw na dem
Ñi KO doon wuutu, ñëpp a dem
Ñaar i Sëtam yi mujj’ee dem
Ki mujju ak kañ tudd’ee baayam

Képp ku jooyoon, na nga reeh
Te ñaan KU-TEDD-KI di reeh
Ku kay bégée ba tax ngay reeh
Looy def di nga ca jëlée ndam

Ma ñëw ci SËRIÑ-MUNTAQÂH
Ma fawqa Ñoñ Waa-Fâqû
Jotaay bu beesam a fawqa
Jotaayu Ñoñ Waa-Fâqû

Izrâfîl ci Développement
Jot na Ndigal ci MARIAMÂH
Jibrîl a ko wax mbir ma
Na Muntaqâh am développement

Zan-Jayâ-Hîlu Malâkah
Jot na Ndigalu BUUR-YÂLLAH
Ci di munna ca kay tal a
Dox di yàxx ba du tal a

Yàxxati ndax Sëriñ-MUNTAQÂH
Moo dònn ñëpp, Irtaqâh
Yim boole ëpp, moo fawqu
Lépp lu baax, mooy Muntaqâh

Dañ ko tànn, di ko élire
Ku am gòpp wutal ileer
Tool i àllarbam di na riir
Ci réew mi ba ñëpp di ser

Dey doon àllarba’y BAMBA-Fépp
Dugub, aareen ci fépp-fépp
Waa-Kër KU-TEDD-KI ci ñëpp
Lañ cay dundal, dara du ëpp

AL MUNTAQÂH mooy MUSTAFÂH
Di BÂRAQALITT, di MUJTABÂH
Tur wu ci ne, siròom
Da ngaa ligéy ba am Ngëram

Ci laa jëlée Irham bi may waxee
KU-TEDD-KI du ma ci naxe
Ñeme wu ma ko, du ay pexe
Kese, MOO di maye texe

Jaayaante na ñu, nang ka nangu
MUSTAFÂH-AFSA digle na ko
Moo neh la woon, kii jàppal ma ko
Moo tax saa mbubu, ma summi ko

Man it, ma jàpp’aat sama bòpp
Def buum ci sama baat u bòpp
Raam’aat, tey summi sama mbub-
Uy darajah, fas la yéene’y tòpp

Murîd, Ndigal da kay jëfée
Lum man a doon mu kay jëfee
Lum jafe-jafe
Di bay sonjaan tey naan kafe

Wa Salâm !

Partager